رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
Gërëm nanu yaw njabooteeg Al-Sahra gërëm nanu.
Wo
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
رضينا بالنبيِّ لنا إمَامًا
وأنْتُم آلُهُ وبِكُمْ رَضِينَا
Nangu nanu Yonent bi mu di sunu njiit
Té yéen ay mbokkam ngéen ci yéen nanu nangu
وبالسِّبْطِ الحُسَيْنِ كَذَا أخُوهُ
وَحَيْدَرُ ثُمَّ زَيْنُ العَابِدِينَا
Ak sët bi di Hussayn ak itam rakam
Ak Haydar tamit Zaynul Abidina
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
وَزَيْنَبُ مَنْ لها فَضْلٌ سَمِيٌّ
سُلاَلَةُ أَحْمَدٍ في الطَّيِّبِينَا
Ak Zeynab mi am jikko yu kawe
Ci sëtù Ahmad ci ñi gën a sell
لها نُورٌ يُضِيءُ كَمِثْلِ شَمْسٍ
من المُخْتَارِ نَشْهَدُهُ مُبِينَا
Am na leer guy nitt ni bëccëgu jant
Bo xam ni mu leer la ci Yonent bi
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
لها جُودٌ لها كَرَمٌ وعَطْفٌ
حَوَتْ فَضْلاً يُرَى للمُنْصِفِينَا
Am na tabé ak yiw ak tam yërmandé
Da fa dajé lépp luy yiw ci ñi dëggu
أمير المؤمنين أَبُوكِ حَقًّا
عَلِيٌّ سَادَ جَيْشَ العَارِفِينَا
Kilifayu jullit yi mooy sa baay dëgg
Aliyu mi jiité mbooloom ñi xam Yalla
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
وأُمُّكِ بَضْعَةُ المُخْتَارِ طَهَ
مُحَبَّبَةٌ إلى الهادي نبينا
Sa yaay mooy wàllu Yonent bi Taha
Ku ñu nob la ci Njiit bi di sunu Yonent
وكَانَ المُصْطَفَى يَحْنُو عَلَيْهَا
حُنُوَّ مَوَدَّةٍ عَطْفًا وَلِينَا
Yonent bi da ko daan uuf ci mbeugéel
Ak yërmandé ak nooyal gu kawe
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
وجَاءَ حَدِيثُهُ يُتْلَى جِهَارًا
لَقَدْ سَادَتْ نِسَاءَ العَالَمِينَا
Waxam feeñ na ñépp di ko tudd
Ne mooy kilifayu jigéeni àdduna yépp
إذا اشْتَقْنَا إلى خَيْرِ البَرَايَا
أَتَيْنَاكُمْ مُشَاةً رَاكِبِينَا
Bu nu nammé kiy gën jikko ci mbindéef yi
Dinan ñëw ci yéen, di dox walla di war
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
فأنتم منه بالأسرار جِئْتُمْ
وَجِئْنَاكُمْ فَشَاهَدْنَا الأَمِينَا
Ndax yéen la kimm yi ak suttura yi féñe
Ñëw nanu ci yéen ba gis kiy Al-Amine
وشَاهَدْنَا لديكم كُلَّ خَيْرٍ
وشَاهَدْنَا أُلُوفًا زَائرِينَا
Gis nanu ci yéen mbooleem ay xéewal
Té gis nanu junni-junniy nit ñiy siyaaré
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
بإخْلاَصٍ وتوحيد ودِينٍ
أَتَوْكُمْ سَادَتِي مُتَبَرِّكِينَا
Ak sellal ak bennal Yalla ak diine
Ñëw nanu ci yéen, sunu sang yi, di barkélu
تُذَكِّرُهُمْ مَشَاهِدُكُمْ جِنَانًا
بِرَوْضَةِ جَدِّكُمْ لِلْوَفِدِينَا
Séen bërëp yi da leen di fàttali àjjana
Ci Rawdab séen maam ngir ñiy ñëw
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
فَرَوْحٌ مِنْهُ والرَّيْحَانُ يأتي
لِزُوَّارٍ أَتَوْكُمْ مُخْلِصِينَا
Nooflay ak xéetu àjjana mi ngiy ñëw
Ngir ñiy siyaaré ñi sellal ci yéen
فأنتم مِنْهُ والذِّكْرَى لَدَيْكُمْ
برُؤيَاكُمْ تُرَى للمُؤْمِنِينَا
Ndax ci moom ngéen bawoo té fàttaliku bi ci yéen la ne
Ci gis yéen lañu koy giséel ñiy gëm
رَضِينَا يا بَنِي الزَّهْرَا رَضِينَا
بِحُبٍّ فيكُمُوا يُرْضي نَبِينَا
Gën nanu nangu yéen doomou Zahra
Ak mbëgeel ci yéen liy neexal sunu Yonent
فَبَابُ العِلْمِ والدُكُمْ عَلِيٌّ
له سَيْفٌ أَبَادَ الكَافِرِينَا
Buntub xam-xam bi séen baay Aliyu la
Am na jaasi gu daaneel ñi weddi
فَمِنْ دَمْعٍ لأرضٍ قد رَوَيْنَا
مِنَ الأَشْوَاقِ نَحْوَ الأَكْرَمِينَا
Ci rangon nanu suuxat suuf si
Ngir namm ak bëgg ñi gën a tedd