بَحِبَّك وَ بَرِيْدَك
Nob naa la, te namme naa la.
Wo
بَحِبَّك وَ بَرِيْدَك
وَاتْمَنَّى أَبُوس إِيدَك
Damala bëgg te di la namm
Te bëgg na nuyal sa loxo bu barkeel bi
خَدَّامَك وَمُرِيدَك
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Sa njaam ak sa murit laa
Yaw Maamu Al-Hasanayn
حَبِيْبِي مُحَمَّد
مَفِيشْ زَيُّه اتْنِين
Muhammad sama xarit
Kenn melul ni moom
حُبُّه سَاكِن قَلْبِي
يَزِيد كُلِّ اتْنَيْنِ
Mbëggeelam dëkk na sama xol
Di yokku saa su nekk
جَمَالُه وَ دَلَالُه
مِتْغَطِي بْجَلَالُه
Rafetaayam ak yeermandeem
Maalikoom moo ko muur
وَتِقْعُد قْبَالُه
تُشُوفْهُم الِاتْنَيْن
Boo toogee ca kanamam
Dinga gis ñaar yépp rekk
بَحِبَّك وَ بَرِيْدَك
وَاتْمَنَّى أَبُوس إِيدَك
Damala bëgg te di la namm
Te bëgg na nuyal sa loxo bu barkeel bi
خَدَّامَك وَمُرِيدَك
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Sa njaam ak sa murit laa
Yaw Maamu Al-Hasanayn
يَا أَجْمَل هَدِيَّة
مِنْ رَبِّ الْبَرِيَّة
Yaw mayé bi gën a rafet
Bu jóge ci Boroom mbindéef yi
لِكُلِّ الدُّنْيَا دِيَّا
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Ngir àdduna bi yépp
Yaw Maamu Al-Hasanayn
مَاهْوِنْتَ قَمَرْهَا
وَانْتَ اللِّي مُنَوِرْهَا
Yaw yaay weeru àdduna
Te yaa koy leeral
وَمْفَتَاح اسَرَارْهَا
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Te yaay caabi suuraat yi
Yaw Maamu Al-Hasanayn
بَحِبَّك وَ بَرِيْدَك
وَاتْمَنَّى أَبُوس إِيدَك
Damala bëgg te di la namm
Te bëgg na nuyal sa loxo bu barkeel bi
خَدَّامَك وَمُرِيدَك
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Sa njaam ak sa murit laa
Yaw Maamu Al-Hasanayn
حَبِيبِي وَعْنَيَّا
أَحْمَد ضَيّ عْنَيَّا
Sama xarit ak samay bët
Ahmad yaay leeru samay gishit
أَنْتَ الْغَالِي عَلَيَّا
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Yaw yaa gën a jafe ci man
Yaw Maamu Al-Hasanayn
وَبِنْتَك الْبَتُول
يَا عُيُونَ الرَّسُول
Ak sa doom bu sell ba Al-Batul
Yaw yaay leeru bëtu Yonent bi
نَرْجُو مِنْكُم قَبُول
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Ñungi ñaan nangu ci yeen
Yaw Maamu Al-Hasanayn
بَحِبَّك وَ بَرِيْدَك
وَاتْمَنَّى أَبُوس إِيدَك
Damala bëgg te di la namm
Te bëgg na nuyal sa loxo bu barkeel bi
خَدَّامَك وَمُرِيدَك
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Sa njaam ak sa murit laa
Yaw Maamu Al-Hasanayn
شُوفْتُه أَنِي قُصَادِي
اتْكَسَفْت أَنَادِي
Bi ma ko gisee ca kanamam
Rus naa koo woo
وِبْقَلْبِي سُهَادِي يَا جَدِّي
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Sama xol di rëbb-rëbbi ci nammeel yaw sama maama
Yaw Maamu Al-Hasanayn
يِنْدَهْلِي وَاجِيلُه
يِفْرِشْلِي مَنْدِيلُه
Da may woo ma ñëw
Mu lalal ma mbubb mi
حَبِيبِي أَنَادِيلُه
يَا جَدَّ الْحَسَنَيْن
Sama xarit laay woo
Yaw Maamu Al-Hasanayn