يَا جَمَالَ النَّبِيِّ يَا حَنَانَ النَّبِيِ
O Beauty of the Prophet, O Compassion of the Prophet
Wo
يَا جَمَالَ النَّبِيِّ
يَا حَنَانَ النَّبِيِ
Yaw rafetayu Yonent bi
Yaw yërmandey Yonent bi
وَاللَّهِ الْعَظِيمِ يَا نَاسُ
مَا لِينَا غَيْرُ النَّبِيِ
Barkeb Yalla bu mag bi yeen nit ñi
Amunu keneen ku dul Yonent bi
مَا لِينَا غَيْرُهْ هُوَ
سَاكِن فِي الْقَلْبِ جُوَّة
Amunu keneen ku dul moom
Mu dëkk ci biir xol bi
دَهْ حَبِيبي وَرُوحُي هُوَ
وَضَمَّنِي سَيِّدُنَا النَّبِي
Sama mbëggeel ak sama ruu la
Fettli na ma sunu sang Yonent bi
مَا لِينَا غَيْرُهُ ثانِي
طَرْفُهْ أَكْحَلُ رَبَّانِي
Amunu beneen ku dul moom
Bëtam yu ñu taaraal ci barkeb Yalla
أَبْلَجُ وَرْدِيُّ الْوَجَانِ
حَبِيبُنَا سَيِّدُنَا النَّبِي
Kanamaam dafa leer te xonq
Sunu mbëggeel sunu sang Yonent bi
مَا لِينَا غَيْرُ الرَّسُولِ
جَمَالُهُ يَسْبِي الْعُقُولَ
Amunu keneen ku dul Yabbal bi
Rafetayam dafay natt xel yi
نَظْرَةً يَا أَبَا الْبَتُولِ
جُدْ بِزَوْرَةٍ يَا نَبِي
Benn xool rek yaw baayu Batuur
May nu nu seeti la yaw Yonent bi
كَفُّكَ يَا طَهَ طَاهِرُ
ذِكْرُكَ سِرُّ الْبَشَايِرِ
Sa loxo yaw Daaha dafa sell
Sa tuddu mooy mbóotu mbégte yi
يَا جَابِرَ لِلْخَوَاطِرِ
اجْبُرْنَا يَا سَيِّدَنَا النَّبِي
Yaw miy dëgëral xol yu naqaral
Dëgëral nu yaw sunu sang Yonent bi
نُورُ الْمُصْطَفَى أَحْمَدُ
نُورٌ أَزَلِيٌّ سَرْمَدُ
Leeru Mustafaa Ahmadu
Leer gu fi masul a jóg la
أَوَّلُ مَا رَبِّي أَوْجَدَ
نُورُكَ يَا سَيِّدَنَا النَّبِي
Li Boroom bi jëkka sàkk
Sa leer la yaw sunu sang Yonent bi