يا مَنْ يَرَى أدمُعِي تَنْهَلُّ كالدِّيَمِ
O You Who See My Tears Pouring Down Like Ceaseless Rain
Wo
Wo
يا مَنْ يَرَى أدمُعِي تَنْهَلُّ كالدِّيَمِ
مِنْ مُقْلَتيَّ وجِسْمِي بَادِيَ الْسَّقَمِ
Yaw miy guiss samay rangooñ nuy sotti ni taw yu ràbbaayu
Ci samay bët, te sama yaram feeñal na mbeurbeut
لا تَعجَبنَّ وإنْ أصْبَحْتُ كالرِّمَمِ
رِيمٌ على القَاعِ بينَ البَانِ والْعَلَمِ
Bul yéemu sax su ma nekké ni yax yu nagg
Kewel bu nekk ci xir wi, diggante ban ak tund wi
أَحَلَّ سَفْكَ دَمِي في الأَشْهُرِ الْحُرُمِ
واعْجَبْ لأَمْرِي فإنّي لَمْ أكُنْ أَبَدَا
Dagaat na sotti sama déet ci weer yu sell yi
Waaye yéemu ci sama mbir, ndaxte masuma woon
أَخشَى الشَّدَائِدَ لوْ مَدَّتْ إلَيَّ يَدَا
لَكِنَّمَا الْحُبُّ أَصْمَانِي فَقُلْتُ سُدَى
Ragal coono yi sax su ñu ma sancee loxo
Waaye mbëggeel dafa ma tëxloo, ma wax lu neen
رَمَى القَضَاءُ بِعَينَيْ جُؤذُرٍ أَسَدَا
يا سَاكِنَ اَلْقَاعِ أدرِك سَاكِنَ الأَجَمِ
Dogal dafa door gaynde ak bëti sëll
Yaw mi dëkk ci xir wi, wallu ko mi dëkk ci àllu gaynde
صَالَ الْحَبِيبُ بِنَبْلِ الطَّرْفِ ذِي الْعُدَدِ
عَلَى فُؤَادِي وَخَـلاَّني بِلاَ رَشَدِ
Sama xol bi mbeugël songu na ko ak féti xool yu bari
Te bàyyi na ma ma nekk di réer ci tawat
وَإِذْ رَمَانِي وَأَوْهَى سَهْمُهُ جَلَدِي
جَحَدْتُها وَكَتَمْتُ الْسَّهْمَ فِي كَبِدِي
Bi mu ma sànnee te fétam lagg sama muñ
Ma lànk ko te nëbb fét bi ci sama biir
جُرْحُ الأَحِبَّةِ عِنْـدِي غَيْرُ ذِي أَلَمِ
إذا بَدا قَمَرِي لا يَظْهَرُ القَمَرُ
Gaañu-gaañu ku ma sopp duma ko mettiyoo
Su sama weer bi feeñee, weeru asamaan du feeñ
قَدْ طَالَ في حُبِّهِ التَّفْكيرُ والْسَهَرُ
رُوحِي لَهُ ودَمِي والْسَّمْعُ والْبَصَرُ
Sama xalaat ak sama tëddu-nelaw ci mbëggeelam yàgg na
Sama ruu, sama déet, sama nnopp ak sama bët, yepp moom na ko
يا لائِمِي في هَواهُ والْهَوَى قَدَرُ
لو شَفَّكَ الْوَجْدُ لَمْ تَعْذِلْ ولمْ تَلُمِ
Yaw mi may jéww ci sama mbëggeel te mbëggeel dogal la
Su la tiis wu xoot bi dóonoon, dooma jéww walla ngay sib