صَلَّى عَلَيْكَ اللَّهُ يَا عَدْنَانِ
Yal na la Yalla julle, yaw Adnaan.
Wo
صَلَّى عَلَيْكَ اللَّهُ يَا عَدْنَانِ
يَا مُصْطَفَى يَا صَفْوَةَ الْرَّحْمَٰنِ
Yàlla na xéewalu Yàlla sotti ci yaw, yaw Adnan
Yaw Mustafaa, yaw tànnéefu Boroom-Yërmande bi
الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي أَعْطَانِي
هَذَا الْغُلَامَ الْطَّيِّبَ الْأَرْدَانِ
Cant gi ñeel na Yàlla mi ma jox
lii di xale bu sell te am barke
قَدْ سَادَ فِي الْمَهْدِ عَلَى الْغِلْمَانِ
أُعِيذُهُ بِالْبَيْتِ ذِي الْأَرْكَانِ
Moom mooy njiitu xale yi ba mu nekké ci dënnu
Ma ngi koy musal ci Kàba gi am ponk yi
حَتَّى أَرَاهُ بَالِغَ الْبُنْيَانِ
أَنْتَ الَّذِي سُمِّيتَ فِي الْقُرْآنِ
Ba ma koy gis mu màgg te dëgër ci taxaway
Yaw lañu tudd ci Alxuraan
أَحْمَدُ مَكْتُوبٌ عَلَى الْجِنَانِ
صَلَّى عَلَيْكَ اللَّهُ فِي الْأَحْيَانْ
Ahmad, bind nañu sa tur ci biir àjjana yi
Yàlla na Yàlla sotti xéewalam ci yaw saa su ne
أَحْمَدُهُ فِي الْسِّرِّ وَالْإِعَلْأَنِ
حَقًّا عَلَى الْإِسْلَامِ وَالْإِيمَانِ
Ma ngi koy gërëm ci kumpa ak ci feeñ
Lu dëggu la ci Lislaam ak Ngëm
يَا رَبَّنَا بِالْمُصْطَفَى الْعَدْنَانِ
اغْفِرْ ذُنُوبِي ثُمَّ أَصْلِحْ شَأْنِي
Yaw sunu Boroom, ci darajay Mustafaa Adnan
Baal ma samay bàkkaat te baaxal samay mbir